Home
Top Artistes
Top Paroles
Ajouter Paroles
Contact
menu
search
Contactez-nous
Artiste:
Ma Valise
Titre:
Samay Bok
Assurez-vous que les corrections sont tout à fait exactes
S'il vous plaît, les mettez en évidence en quelque sorte!
Vous pouvez, par exemple, écrire
INCORRECT: avant la mauvaise ligne
CORRECT: avant la correspondant ligne correcte
Autrement, nous ne pouvons les corriger pas! Merci pour votre aide.
bakkan waruw dàll la fa muy degge dooko yëg dem rekk delu si rekk melni wèer wi delu si ci sèy jèego fènèen wèer mouk ci fi, bidèw bi danouna dèe ci souff samay xarit, tèy ji ndadjè bi rafèt na, djoko, seeddo, ak rétane bi rafèt na, xèw bou nèex mais soubbe dagniouy dèm, galankor bi moy dougnou meuneu xamanté bou bax, dou nouy am waxtou bou doy ngir soppanté goudi gi wèss, mangi won fénène, bi ci toop dina fi sori ak samay bok ci camion bi, dinagnouy teugueu ngir féccelo yénéni nit ak samy bok ci camion bi, ngir andi mbékté bignouy djeul bakkan waruw dàll la ku dul toxu doo xam fu dèkk neexe fa muy dagge dooko yëg (Merci a El Cancre pour cettes paroles)